1
2.Timote 2:15
Kàddug Yàlla
KY
Defal sa kem-kàttan ba boo teewee fa kanam Yàlla, di ku mu gërëm, ab liggéeykat bu mucc gàcce, di xamle kàddug dëgg gi ni mu ware.
Compare
Explore 2.Timote 2:15
2
2.Timote 2:22
Xemmemtéefi ndaw nag, daw ko, te nga topp njub ak ngëm ak cofeel ak jàmm, ànd ceek ñiy tudde Boroom bi xol bu set wecc.
Explore 2.Timote 2:22
3
2.Timote 2:24
Te jaamub Boroom bi warul di ŋaayoo, waaye day lewet ci ñépp, mana jàngale tey muñ.
Explore 2.Timote 2:24
4
2.Timote 2:13
su nu ko ñàkkee kóllëre, mu saxoo kóllëreem, ndax manula gàntal boppam.
Explore 2.Timote 2:13
5
2.Timote 2:25
Jaamub Boroom bi ndànk la war di jubbanti diiŋatkat yi, ndax jombul Yàlla may leen ñu tuub, ba xam liy dëgg.
Explore 2.Timote 2:25
6
2.Timote 2:16
Waaye ay kebetuy àddinay kese, moytu ko, ndax ngëmadi gu ko yées rekk lay yóbbee
Explore 2.Timote 2:16