1
2.Timote 1:7
Kàddug Yàlla
KY
Ndax kat Xel mi nu Yàlla jox taxu noo ragal, xanaa kay da noo may doole ak cofeel ak jëfin wu laloo am xel.
Compare
Explore 2.Timote 1:7
2
2.Timote 1:9
Moo nu musal, woo nu woote bu sell te sunuy jëf taxul, waaye coobarey boppam a tax, ak yiwam wi ñu nu may ci Almasi Yeesu, balaa ay jamonoy jamono di sosu.
Explore 2.Timote 1:9
3
2.Timote 1:6
Moo tax li ma lay fàttali moo di, nga xamb taalub mayu Yàlla ga nga jote ca ba ma la tegee samay loxo.
Explore 2.Timote 1:6
4
2.Timote 1:8
Bul kersawoo di seedeel sunu Sang, mbaa nga di ma kersawoo, man mi ñu tëj ngir moom, waaye jëlal sa wàll ci coonob xibaaru jàmm bi, ni la ko manoorey Yàlla manloo.
Explore 2.Timote 1:8
5
2.Timote 1:12
Looloo tax may daj yii coono. Waaye rusuma ci, ndax xam naa ki ma gëm, te wóor na ma ne, li ma ko dénk, moo ko mana sàmm ba keroog bés ba.
Explore 2.Timote 1:12