1
Njàlbéen ga 46:3
Kàddug Yàlla gi
KYG
Yàlla ne ko: «Man maay Yàlla, di sa Yàllay baay. Bul ragala dem Misra, ndaxte askan wu réy laa fay sose ci yaw.
ប្រៀបធៀប
រុករក Njàlbéen ga 46:3
2
Njàlbéen ga 46:4
Man ci sama bopp maay ànd ak yaw Misra, te na la wóor ne dinaa la délloosi, te it Yuusufa moo lay doggali.»
រុករក Njàlbéen ga 46:4
3
Njàlbéen ga 46:29
Yuusufa nag waajal waruwaayam, dajeji ak baayam Israyil ca Gosen. Ba Yuusufa àggee ba ca moom, da koo laxasu, ne ñàpp ci kawam, jooy lu yàgg.
រុករក Njàlbéen ga 46:29
4
Njàlbéen ga 46:30
Israyil ne Yuusufa: «Léegi de, bu ma yeboo dee, gannaaw gisaat naa la, ngay dund.»
រុករក Njàlbéen ga 46:30
គេហ៍
ព្រះគម្ពីរ
គម្រោងអាន
វីដេអូ