1
Macë 25:40
Téereb Injiil
TI
Noonu Buur bi dina leen ne: “Ci dëgg maa ngi leen koy wax, saa yu ngeen defalee loolu kenn ki gëna ndaw ci sama bokk yii, man ngeen ko defal.”
Compare
Explore Macë 25:40
2
Macë 25:21
Njaatigeem ne ko: “Def nga lu baax, surga bu baax nga te takku. Gannaaw takku nga ci lu tuuti, dinaa la dénk lu bare. Kaay bokk ci sama mbég.”
Explore Macë 25:21
3
Macë 25:29
Ndaxte ku am dinañu la dolli, ba nga barele, waaye ku amul, li nga am as néew sax, dinañu ko nangu.
Explore Macë 25:29
4
Macë 25:13
«Yewwuleen nag, ndaxte xamuleen bés ba mbaa waxtu wa.
Explore Macë 25:13
5
Macë 25:35
Ndaxte xiifoon naa, ngeen jox ma, ma lekk; te mar, ngeen jox ma, ma naan; nekkoon naa ab doxandéem, ngeen fat ma
Explore Macë 25:35
6
Macë 25:23
Explore Macë 25:23
7
Macë 25:36
te rafle, ngeen wodd ma; woppoon naa, ngeen seetsi ma; te ñu tëj ma, ngeen ñëw fi man.”
Explore Macë 25:36