1
Yowaan 5:24
Téereb Injiil
TI
«Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku dégg sama kàddu te gëm ki ma yónni, am nga dund gu dul jeex te doo jaar ca àtte ba, ndaxte génn nga ci dee, tàbbi ci dund.
Compare
Explore Yowaan 5:24
2
Yowaan 5:6
Bi ko Yeesu séenee mu tëdd, te mu xam ne woppam ji yàggoon na lool, mu laaj ko ne: «Ndax bëgg ngaa wér?»
Explore Yowaan 5:6
3
Yowaan 5:39-40
Yéena ngi gëstu Mbind yi, ndaxte dangeen cee yaakaar dund gu dul jeex. Mbind yooyu nag far, ci sama mbir lañuy wax; te bëgguleena ñëw ci man ngir am dund!
Explore Yowaan 5:39-40
4
Yowaan 5:8-9
Yeesu ne ko: «Jógal, jël sa basaŋ te dox.» Ca saa sa mu daldi wér, jël basaŋam, daldi dox. Mbir moomu dafa daje woon ak bésub noflaay ba
Explore Yowaan 5:8-9
5
Yowaan 5:19
Noonu Yeesu ne leen: «Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, Doom ji manula def dara moom ci boppam; li mu gis Baay bi di def rekk lay def. Li Baay bi di jëf la Doom ji itam di jëf.
Explore Yowaan 5:19