1
Yowaan 3:16
Téereb Injiil
TI
Ndaxte Yàlla dafa bëgg àddina, ba joxe jenn Doomam ji mu am kepp, ngir képp ku ko gëm am dund gu dul jeex te doo sànku mukk.
Compare
Explore Yowaan 3:16
2
Yowaan 3:17
Yàlla yónniwul Doomam ci àddina ngir mu daan nit ñi, waaye ngir musal leen.
Explore Yowaan 3:17
3
Yowaan 3:3
Yeesu ne ko: «Ci dëgg-dëgg maa ngi la koy wax, képp ku judduwaatul doo mana seede nguuru Yàlla.»
Explore Yowaan 3:3
4
Yowaan 3:18
Képp ku ko gëm deesu la daan, waaye ku ko gëmul daan nañu la ba noppi, ndaxte gëmuloo ci turu Doom ji Yàlla am kepp.
Explore Yowaan 3:18
5
Yowaan 3:19
Ci nii la àtte bi ame: leer gi ñëw na ci àddina, waaye nit lëndëm gi lañu taamu ndax seeni jëf yu bon.
Explore Yowaan 3:19
6
Yowaan 3:30
Li war moo di moom, mu gëna màgg te man, ma gëna féete suuf.»
Explore Yowaan 3:30
7
Yowaan 3:20
Képp kuy def lu bon day bañ leer gi te du ci ñëw, ndax ragal ay jëfam di feeñ bëccëg ndarakàmm.
Explore Yowaan 3:20
8
Yowaan 3:36
Ku gëm Doom ji, am nga dund gu dul jeex; ku déggadil Doom ji, amuloo dund, waaye merum Yàllaa ngi la tiim.
Explore Yowaan 3:36
9
Yowaan 3:14
Te itam na Musaa sampe woon ab bant ca diggu màndiŋ ma, takk ca jaan, ja mu defare woon xànjar, fàww ñu yékkatee noonu Doomu nit ki
Explore Yowaan 3:14
10
Yowaan 3:35
Baay bi dafa bëgg Doom ji, te jox na ko sañ-sañ ci lépp.
Explore Yowaan 3:35