1
Yowaan 2:11
Téereb Injiil
TI
Firnde jii ame ca Kana, ca diiwaanu Galile, moo doon kéemaan gi Yeesu jëkka def. Ci noonu la wonee màggaayam te ay taalibeem gëm nañu ko.
Compare
Explore Yowaan 2:11
2
Yowaan 2:4
Yeesu ne: «Soxna si, loo ma bëggal? Ndaxte sama waxtu jotagul.»
Explore Yowaan 2:4
3
Yowaan 2:7-8
Yeesu ne surga ya: «Duyleen ndaa yi.» Ñu duy leen, ba ñu fees bay rembat. Noonu Yeesu ne leen: «Tanqleen ci léegi, yót ko njiitu xew wi.» Ñu daldi ko ciy yót.
Explore Yowaan 2:7-8
4
Yowaan 2:19
Yeesu ne leen: «Daaneel-leen kër Yàlla gii, ma daldi koy yékkati ci ñetti fan.»
Explore Yowaan 2:19
5
Yowaan 2:15-16
Noonu Yeesu ràbb ab yar, daldi leen koy dàqe, ngir ñu génn ëttu kër Yàlla ga, ñoom ak xar ya ak nag ya. Mu tasaare xaalisu weccikat ya, daaneel taabal ya, daldi ne jaaykati pitax ya: «Jëleleen fi lii! Sama kër Baay, buleen ko def marse!»
Explore Yowaan 2:15-16