1
1.Tesalonig 3:12
Téereb Injiil
TI
Yal na leen Boroom bi dolli mbëggeel gu tar, ngeen bëggante te bëgg ñépp, ni nu leen bëgge nun.
Compare
Explore 1.Tesalonig 3:12
2
1.Tesalonig 3:13
Yal na Boroom bi samp seeni xol noonu ci sellaay gu amul sikk fa kanam Yàlla sunu Baay, ba bés bu Yeesu sunu Boroom délsee, ànd ak gaayam yu sell yépp.
Explore 1.Tesalonig 3:13
3
1.Tesalonig 3:7
Noonu bokk yi, ci biir tiis ak coono yi nu nekk, seen ngëm dëfal na sunu xol.
Explore 1.Tesalonig 3:7