1
1.Tesalonig 2:4
Téereb Injiil
TI
Waaye gannaaw Yàlla moo nu seet, ba wóolu nu te dénk nu xibaaru jàmm bi, kon noonu lanuy waaree, du ngir neex nit ñi, waaye ngir neex Yàlla miy seet xol yi.
Compare
Explore 1.Tesalonig 2:4
2
1.Tesalonig 2:13
Te it dunu noppee sant Yàlla ci lii: ba ngeen jotee kàddug Yàlla, gi nu doon waare, nangu ngeen ko, waxuma ni kàddug nit waaye ni kàddug Yàlla, ndaxte moom la ci dëgg-dëgg, te mu ngi jëf ci yéen ñi gëm.
Explore 1.Tesalonig 2:13