1
1.Tesalonig 4:17
Téereb Injiil
TI
gannaaw loolu nun ñiy dund te des fi, dinañu ne fëyy ak ñoom jëm ci niir yi, taseji ak Boroom bi ci jaww ji. Te noonu dinanu nekk ak Boroom bi ba fàww.
Compare
Explore 1.Tesalonig 4:17
2
1.Tesalonig 4:16
Ndaxte ndigal lu jamp dina jib, baatu kilifa ci malaaka yi dégtu, liitu Yàlla jolli, te Boroom bi moom ci boppam dina wàcce ca asamaan. Booba ñi gëm Kirist te dee dinañu jëkka dekki
Explore 1.Tesalonig 4:16
3
1.Tesalonig 4:3-4
Lii nag mooy coobarey Yàlla: ngeen sell, maanaam ngeen moytu njaaloo; ngeen not seeni cér ci cell ak tedd
Explore 1.Tesalonig 4:3-4
4
1.Tesalonig 4:14
Ndegam gëm nanu ne Yeesu dee na te dekki, noonu it Yàlla dina indaale ak Yeesu ñépp ñi ko gëm te nelaw.
Explore 1.Tesalonig 4:14
5
1.Tesalonig 4:11
Fullawooleena dund ci jàmm, di topptoo seen mbiri bopp tey lekk seen ñaq, ni nu leen ko sante woon.
Explore 1.Tesalonig 4:11
6
1.Tesalonig 4:7
Ndaxte Yàlla woo na nu, nu dund ci cell, waaye du ci sobe.
Explore 1.Tesalonig 4:7