1
Màrk 3:35
Kàddug Yàlla
KY
Ndax kuy jëfe coobarey Yàlla, kooku moo di sama rakk ju góor, di samab jigéen, di sama yaay.»
Compare
Explore Màrk 3:35
2
Màrk 3:28-29
Maa leen ko wax déy, lu mu mana doon, dees na ko jéggal doom aadama, mu diy bàkkaaram, ak mboolem kàddug saaga Yàlla. Waaye képp ku saaga Noo gu Sell gi, deesu ko jéggal mukk; day gàddu bàkkaar ba fàww.»
Explore Màrk 3:28-29
3
Màrk 3:24-25
Ag nguur de, su dee xàjjalikoo ci biiram, googa nguur du mana yàgg. Ag kër it, su dee xàjjalikoo ci biiram, googa kër du mana yàgg.
Explore Màrk 3:24-25
4
Màrk 3:11
Rab ya itam, saa yu ñu ko gisaa, daldi daanu fa kanamam, tey yuuxu naan: «Yaa di Doomu Yàlla.»
Explore Màrk 3:11