1
Yowaan 7:38
Kàddug Yàlla
KY
ku ma gëm, ay dex ay balle cib dënnam, di wal ndox muy dund! Te noonu la ko Mbind mi indee.»
Compare
Explore Yowaan 7:38
2
Yowaan 7:37
Bés ba mujj ca màggal ga nag moo ca gënoona màgg. Keroog la Yeesu taxaw, àddu ca kaw ne: «Ku mar, na ñëw ci man, naan
Explore Yowaan 7:37
3
Yowaan 7:39
Booba Noowug Yàlla la doon wax, Noo ga gëmkati Yeesu doon waaja jot, te jotaguñu ko woon, ndax booba, Yeesoo tàbbeegul woon ci teraangaam.
Explore Yowaan 7:39
4
Yowaan 7:24
Bàyyileen di àttee li leen seen bët may, deeleen àttee dëgg.»
Explore Yowaan 7:24
5
Yowaan 7:18
Kiy wax ci coobarey boppam nag, darajay boppam lay sàkku, waaye ki bëgga fésal darajay ki ko yónni, kooku ku dëggu lay doon, te ag njubadi du nekk ci moom.
Explore Yowaan 7:18
6
Yowaan 7:16
Yeesu daldi leen wax ne leen: «Li may jàngale, moomuma ko, ki ma yebal a ko moom.
Explore Yowaan 7:16
7
Yowaan 7:7
Àddina du leen mana bañ, waaye man la bañ, ndax maa koy seedeel ne ay jëfam dafa bon.
Explore Yowaan 7:7