1
Yawut ya 3:13
Kàddug Yàlla
KY
Waaye bés bu nekk deeleen soññante li feek muy bésub teyagum, bala bàkkaar a nax kenn ci yeen, ba mu mujj dërkiis.
Compare
Explore Yawut ya 3:13
2
Yawut ya 3:12
Bokk yi, wattuleen bala kenn ci yeen a am xolub gëmadi bu bon bu koy xiir ci dëddu Yàlla jiy dund.
Explore Yawut ya 3:12
3
Yawut ya 3:14
Ndax kat noo di àndandooy Almasi bi, ndegam wéye nanoo ŋoy bu dëgër ci sunu kóolute ga nu doore, ba kera muj ga.
Explore Yawut ya 3:14
4
Yawut ya 3:8
buleen të na woon ca fippu ga, keroog bésub seetlu Yàlla ba ca màndiŋ ma
Explore Yawut ya 3:8
5
Yawut ya 3:1
Kon nag bokk yu sell yi, yeen ñi bokk ci wooteb asamaan, ràññeeleen Yeesu, ndaw li, sarxalkat bu mag bi ci yoon wi nu gëm.
Explore Yawut ya 3:1