1
Jëf ya 19:6
Kàddug Yàlla
KY
Ba leen Póol tegee loxoom, Noo gu Sell gi dikkal leen, ñu tàmbalee làkk yeneen làkk, boole ci di biral kàdduy waxyu.
Compare
Explore Jëf ya 19:6
2
Jëf ya 19:11-12
Ba mu ko defee Yàlla di def ay kéemaan yu mag yu mu sottale ci loxoy Póol. Mujj na sax ñuy yóbbul jarag yi ay kaala aki taraxlaay yu laaloon yaramu Póol, ba lu leen daloon teqalikook ñoom, rab wu leen jàppoon, ba leen.
Explore Jëf ya 19:11-12
3
Jëf ya 19:15
Loolu lañu doon jéem bés, rab wa ne leen: «Yeesu déy, xam naa ko. Póol it xam naa ko. Waaye yeen, yeenay ñan?»
Explore Jëf ya 19:15