1
Jëf ya 20:35
Kàddug Yàlla
KY
Nu nekk laa leen wone ne sunu wartéef mooy nu liggéeye noonu bu baax, ngir dimbali néew-doole yi, tey fàttaliku kàddug Sang Yeesu ga mu noon: “Nangu, joxee ko ëpp barke.”»
Compare
Explore Jëf ya 20:35
2
Jëf ya 20:24
Waaye sama bakkan soxalu ma, xanaa ma bey samaw sas, ba sottal liggéey bi ma Sang Yeesu dénk, te mooy seedeel xibaaru jàmm bu yiwu Yàlla wi.
Explore Jëf ya 20:24
3
Jëf ya 20:28
Wattuleen nag seen bopp, wattu mboolem gétt gi leen Noo gu Sell gi sàmmloo, te ngeen foral mbooloom gëmkati Yàlla mi Yàlla jote deretu boppam.
Explore Jëf ya 20:28
4
Jëf ya 20:32
«Léegi nag, dénk naa leen Yàlla ak kàddug yiwam gi leen mana dooleel, dencal leen seen muur ci biir mboolem nit ñi ñu sellal.
Explore Jëf ya 20:32