1
Jëf ya 18:10
Kàddug Yàlla
KY
ndax maa ànd ak yaw. Kenn du la song, def la lu bon, ndax ñu bare ci dëkk bii samay ñoñ lañu.»
Compare
Explore Jëf ya 18:10
2
Jëf ya 18:9
Ba loolu amee Sang bi wax ak Póol ag guddi ci biir peeñu, ne ko: «Bul tiit dara, waaye waxal te bul noppi
Explore Jëf ya 18:9