Jëf ya 19:11-12
Jëf ya 19:11-12 KY
Ba mu ko defee Yàlla di def ay kéemaan yu mag yu mu sottale ci loxoy Póol. Mujj na sax ñuy yóbbul jarag yi ay kaala aki taraxlaay yu laaloon yaramu Póol, ba lu leen daloon teqalikook ñoom, rab wu leen jàppoon, ba leen.





