1
Jëf ya 14:15
Kàddug Yàlla
KY
«Yeen, lu leen xiir ci lii? Nun itam ay nit lanu, bokk ak yeen benn bind. Xibaaru jàmm bi lanu leen di xamal, ngir ngeen wacc yëfi neen yii te walbatiku ci Yàlla, kiy dund te sàkk asamaan ak suuf ak géej ak lépp li ci biir.
Compare
Explore Jëf ya 14:15
2
Jëf ya 14:9-10
Kookoo dégg Póol muy waare, Póol xool ko jàkk, gis ne am na ngëm gu ag muccam mana jaare. Mu àddu ca kaw, ne waa ji: «Jógal taxaw jonn!» Waa ji ne bërét, jóg, daldi dox.
Explore Jëf ya 14:9-10
3
Jëf ya 14:23
Mbooloom gëmkat mu nekk nag, ñu tabb ci ay mag; ci biir loolu ñu ñaan, boole kook koor, daldi dénk mag ña Sang bi ñu gëm.
Explore Jëf ya 14:23