Jëf ya 14:9-10
Jëf ya 14:9-10 KY
Kookoo dégg Póol muy waare, Póol xool ko jàkk, gis ne am na ngëm gu ag muccam mana jaare. Mu àddu ca kaw, ne waa ji: «Jógal taxaw jonn!» Waa ji ne bërét, jóg, daldi dox.