1
Jëf ya 13:2-3
Kàddug Yàlla
KY
Ñooñoo daje woon di màggal Boroom bi, boole kook koor. Ci biir loolu Noo gu Sell gi ne: «Beralleen ma nag Barnabas ak Sóol ngir liggéey bi ma leen woowe.» Ba loolu amee ñu woor, boole kook ñaan, daldi leen teg seeni loxo, ba noppi yiwi leen.
Compare
Explore Jëf ya 13:2-3
2
Jëf ya 13:39
képp ku gëm Yeesu, ci moom lay wàccook loolu lépp, ba ag njubam mat.
Explore Jëf ya 13:39
3
Jëf ya 13:47
Ndax noonu la nu ko Boroom bi sante ba mu nee: “Tabb naa la, ngay leeru jàmbur ñi, ngir nga jottaliji wall wii, ba ca cati àddina.”»
Explore Jëf ya 13:47