1
1.Timote 5:8
Kàddug Yàlla
KY
Ku fàggulul ay bokkam nag, rawatina waa këram, yoonu ngëm wi la gàntal, te moo yées ku gëmul.
Compare
Explore 1.Timote 5:8
2
1.Timote 5:1
Bul gëdd mag, waaye ñaax ko ni bu doon sa baay. Ndaw it, def ko ni sa rakk.
Explore 1.Timote 5:1
3
1.Timote 5:17
Mag ñiy jiite mbooloo mi bu baax nag, nañu leen yellale ag njukkal ñaari yoon, rawatina ñi boole coonoy waare ak njàngale.
Explore 1.Timote 5:17
4
1.Timote 5:22
Bul di gaawa teg loxo kenn, ngir fal ko njiit. Bul séddu ci bàkkaari jàmbur, te yaw ci sa bopp, sàmmool dundin wu set.
Explore 1.Timote 5:22