Njàlbéen ga 49:8-9
Njàlbéen ga 49:8-9 KYG
«Yaw Yuda, mi say doomi baay di taggeji, ngay sëqi sa ndoddi noon, sëgal leen, sa doomi baay a lay sujjóotal. Yuda yaa di gaynde gu ndaw, doom, doora jóge nii ci pàdd, tey yuug ak a goor ni gayndeg sibi. Yaa di gaynde gu deesul yee.