Njàlbéen ga 49:3-4
Njàlbéen ga 49:3-4 KYG
«Ruben, yaw mi ma taawloo, nga sosoo sama digg doole, sama ndoortel kàttan, yaa jëkke sut moos ci teraanga ak doole. Yaa toogadi it ni ndox muy wal-wali, doo mujje sut, nde yaa tëdd sa lalu baay, ba teddadi, kera ba nga ca tëddee.