Njàlbéen ga 49:22-23
Njàlbéen ga 49:22-23 KYG
«Yuusufaay bànqaasu garab, garab guy meññ, feggook bëtu ndox, car yaa nga law, tiim digu tool ba. Ay fittkat a ko toŋal, di ko song ak a fitt.