Njàlbéen ga 49:10
Njàlbéen ga 49:10 KYG
Nguur gi du jóge ci loxol Yuda, te yetu buur ay wéye sampe ciy tànkam, li feek boroom di ñëw, ba xeet yi déggal ko.