Njàlbéen ga 45:3
Njàlbéen ga 45:3 KYG
Yuusufa nag ne magam ya: «Man mii maay Yuusufa! Mbaa sama baay a ngi dund?» Magam ya nag manuñu koo tontu, ndax booba njàqare jàpp na leen.