Njàlbéen ga 43:30
Njàlbéen ga 43:30 KYG
Ci kaw loolu Yuusufa gaaw génn ndax yaram wu daw, te manatula téye ay rongooñam ndax rakkam ja, mu dugg néegu biiram, di jooy.