Njàlbéen ga 39:20-21
Njàlbéen ga 39:20-21 KYG
ba jàpp Yuusufa, tëj ko kaso, ba ñuy denc ñi buur jàpp. Yuusufa nekk foofa ca kaso ba. Teewul Aji Sax ji ànd ak Yuusufa, laaye ko biir, daldi xiir wattukatu kaso ba ca moom, mu yéwéne ko.