Njàlbéen ga 39:11-12
Njàlbéen ga 39:11-12 KYG
Mu am bés Yuusufa dugg ca kër ga, di def liggéeyam, te kenn ci surga yu góor ya nekku fa. Ndaw si jàpp ci mbubb mi, ne ko: «Kaay tëdd ak man.» Yuusufa nag wacc mbubb ma cay loxoom, daw génn kër ga.