Njàlbéen ga 38:9
Njàlbéen ga 38:9 KYG
Teewul Onan xam ne du doon askan wu muy moom, ba tax saa yuy dëkkoo jabaru magam, bay wara àgg rekk, tuur wasal wi ci suuf, ngir baña giiral magam.