Njàlbéen ga 37:6-7
Njàlbéen ga 37:6-7 KYG
Da ne leen: «Dégluleen li ma gént. Danoo nekk ca tool ya, di góob. Ba nu takkee, sama takk jekki-jekki ne sàtt, taxaw, seen takk wër sama takk, di ko sujjóotal.»