Njàlbéen ga 37:4
Njàlbéen ga 37:4 KYG
Mag ya nag gis ne Yuusufa la seen baay gëna bëgg ci ay doomam. Loolu tax ñu bañ ko, ba manuñoo séq ak moom kàddu gu rafet.