Njàlbéen ga 37:3
Njàlbéen ga 37:3 KYG
Booba Yanqóoba, Yuusufa la gëna bëgg ci ay doomam, ndax li mu màggat door koo am. Mu ràbblul ko mbubb mu yànj.