1
Njàlbéen ga 42:21
Kàddug Yàlla gi
KYG
te naa ci seen biir: «Céy su nu yégoon, sunu àqu rakk a nu topp nii, ndax danu koo seetaanoon, mu nekk ci njàqarey xol, di nu tinu, te faalewunu ko; looloo waral sunu njàqarey tey jii.»
ប្រៀបធៀប
រុករក Njàlbéen ga 42:21
2
Njàlbéen ga 42:6
Fekk booba Yuusufa mooy dogal ca réew ma, di jaay pepp waa réew mépp. Magi Yuusufa ya ñëw, sujjóotal Yuusufa.
រុករក Njàlbéen ga 42:6
3
Njàlbéen ga 42:7
Naka la Yuusufa gis magam ya, xàmmi leen, te mel ni ku leen xamul, di wax ak ñoom kàddu yu dëgër ne leen: «Fu ngeen jóge?» Ñu ne ko: «Réewu Kanaan lañu jóge, di jëndsi ab dund.»
រុករក Njàlbéen ga 42:7
គេហ៍
ព្រះគម្ពីរ
គម្រោងអាន
វីដេអូ