YouVersion Logo
Search Icon

2.Korent 4:8-9

2.Korent 4:8-9 KY

Nu nekk lees nuy tance, waaye deesu nu nappaaje. Dinanu jaaxle, waaye dunu jàq. Dees na nu bunduxataal, waaye deesu nu wacc. Dees na nu daaneel, waaye deesu nu jekkali.

Verse Image for 2.Korent 4:8-9

2.Korent 4:8-9 - Nu nekk lees nuy tance, waaye deesu nu nappaaje. Dinanu jaaxle, waaye dunu jàq. Dees na nu bunduxataal, waaye deesu nu wacc. Dees na nu daaneel, waaye deesu nu jekkali.

Free Reading Plans and Devotionals related to 2.Korent 4:8-9