YouVersion Logo
Search Icon

1.Timote 2:1-2

1.Timote 2:1-2 KY

Kon nag li jiitu ci mboolem li may dénkaane mooy ngeen di dagaan, di ñaan, di tinu aka sant, ñeel doom aadama yépp, ñeel buur yi ak mboolem boroom baat yi, ngir nu mana nekke jàmm akug dal ak wépp dundin wu tedd, tey wéye ragal Yàlla.

Verse Image for 1.Timote 2:1-2

1.Timote 2:1-2 - Kon nag li jiitu ci mboolem li may dénkaane mooy ngeen di dagaan, di ñaan, di tinu aka sant, ñeel doom aadama yépp, ñeel buur yi ak mboolem boroom baat yi, ngir nu mana nekke jàmm akug dal ak wépp dundin wu tedd, tey wéye ragal Yàlla.

Free Reading Plans and Devotionals related to 1.Timote 2:1-2