1
Màrk 16:15
Téereb Injiil
TI
Mu ne leen: «Demleen ci àddina sépp, yégal xibaaru jàmm bi mbindeef yépp.
Compare
Explore Màrk 16:15
2
Màrk 16:17-18
Ñi ma gëm dinañu ànd ak firnde yii: ci sama tur dinañu dàq rab yi, di wax làkk yu bees, di jàpp jaan ak seeni loxo; te bu ñu naanee lu ñu tooke, du leen wàññi dara, te jarag ju ñu teg loxo, mu wér.»
Explore Màrk 16:17-18
3
Màrk 16:16
Ku gëm te ñu sóob ko ci ndox, dina mucc; ku gëmul, dees na ko daan.
Explore Màrk 16:16
4
Màrk 16:20
Taalibe ya dem waareji, te loxob Boroom bi ànd ak ñoom, di dëggal kàddu gi ak firnde, yi ci ànd.
Explore Màrk 16:20
5
Màrk 16:6
Mu ne leen: «Buleen tiit. Yéena ngi seet Yeesum Nasaret, mi ñu daajoon ci bant bi. Nekkatu fi, dekki na; gisleen fi ñu ko tëraloon.
Explore Màrk 16:6
6
Màrk 16:3-4-5
di laajante: «Ku nuy béraŋal doj, wiy ub bàmmeel bi?» Doj woowu nag bu réya réy la woon. Noonu ñu xool, gis ne doj wa deñ. Ñu dugg ci bàmmeel bi, gis ca ndijoor waxambaane wu sol mbubb mu weex, ñu daldi tiit.
Explore Màrk 16:3-4-5