1
Màrk 15:34
Téereb Injiil
TI
Ci tisbaar nag Yeesu wootee kàddu gu dëgër naan: «Elowi, Elowi, lema sabaktani?» liy tekki: «Sama Yàlla, sama Yàlla, lu tax nga dëddu ma?»
Compare
Explore Màrk 15:34
2
Màrk 15:39
Njiitu xare nag, bi taxawoon ci kanam Yeesu, bi mu gisee ni Yeesu deeye, mu ne: «Ci dëgg, nit kii Doomu Yàlla la!»
Explore Màrk 15:39
3
Màrk 15:38
Bi mu ko defee ridob bérab bu sell ba ca kër Yàlla ga xar ñaar, li dale ci kaw ba ci suuf.
Explore Màrk 15:38
4
Màrk 15:37
Noonu Yeesu wootewaat ak kàddu gu dëgër, delloo ruuwam Yàlla.
Explore Màrk 15:37
5
Màrk 15:33
Li tàmbalee digg bëccëg, ba ci tisbaar, réew mépp lëndëm.
Explore Màrk 15:33
6
Màrk 15:15
Noonu Pilaat, mi wuta neex mbooloo mi, bàyyil leen Barabas, ba noppi mu dóorlu Yeesu ay yar, jébbal ko, ngir ñu daaj ko ci bant.
Explore Màrk 15:15