1
Màrk 14:36
Téereb Injiil
TI
Mu ne: «Abba, Baay, yaw mi dara tëwul, teggil ma kaasu naqar bii. Moona bumu doon sama coobare, waaye na sa coobare am.»
Compare
Explore Màrk 14:36
2
Màrk 14:38
Xool-leen te ñaan, ngir baña daanu cig fiir. Seen xol jag na, waaye seen bind a woyof.»
Explore Màrk 14:38
3
Màrk 14:9
Ci dëgg maa ngi leen koy wax, fépp fu ñuy yéene xibaaru jàmm bi ci àddina sépp, dinañu fa fàttali it li jigéen jii def.»
Explore Màrk 14:9
4
Màrk 14:34
Mu ne leen: «Sama xol dafa tiis, ba ma bëgga dee; toogleen fii, xool.»
Explore Màrk 14:34
5
Màrk 14:22
Noonu bi ñuy lekk, Yeesu jël mburu, sant Yàlla, jox leen ko naan: «Jël-leen, lii sama yaram la.»
Explore Màrk 14:22
6
Màrk 14:23-24
Gannaaw loolu mu jël kaas, sant Yàlla, jox leen ko, ñépp naan ci. Mu ne leen: «Lii mooy sama deret, ji fas kóllëre gi, te tuurul ñu bare.
Explore Màrk 14:23-24
7
Màrk 14:27
Booba Yeesu ne leen: «Yéen ñépp dingeen ma dàggeeku, ndaxte bind nañu: “Dinaa dóor sàmm bi, xari jur gi tasaaroo.”
Explore Màrk 14:27
8
Màrk 14:42
Jógleen nu dem; ki may wor a ngi nii, di ñëw.»
Explore Màrk 14:42
9
Màrk 14:30
Waaye Yeesu ne ko: «Ci dëgg maa ngi la koy wax, guddig tey, bala ginaar a sab ñaari yoon, dinga ma weddi ñetti yoon.»
Explore Màrk 14:30