1
Macë 20:26-28
Téereb Injiil
TI
Buleen mel ni ñooñu. Waaye ku bëgga nekk kilifa ci yéen, na nekk seen surga, te ku bëgga nekk njiit, na nekk seen jaam. Ndaxte noonu la Doomu nit ki ñëwe, du ngir ñu nekk ay surgaam, waaye muy seen surga, ba joxe bakkanam ngir njotug ñu bare.»
Compare
Explore Macë 20:26-28
2
Macë 20:16
Noonu ñi mujj ñooy jiituji, ñi jiitu ñooy mujj.»
Explore Macë 20:16
3
Macë 20:34
Noonu Yeesu yërëm leen, laal seeni bët, ñu daldi gis ca saa sa, topp ci moom.
Explore Macë 20:34