1
Macë 12:36-37
Téereb Injiil
TI
Maa ngi leen di wax ne keroog bés pénc, nit ñi dinañu làyyi ndax wax ju nekk ju amul njariñ, ju ñu masa wax. Ndaxte dees na la àtte ni ku jub ci say wax, walla ñu daan la ci say wax.»
Compare
Explore Macë 12:36-37
2
Macë 12:34
Yéen ñi fees ak daŋar ni ay co, naka ngeen mana waxe lu baax, fekk dangeen bon? Ndaxte gémmiñ, la fees xol lay wax.
Explore Macë 12:34
3
Macë 12:35
Noonu nit ku baax, lu baax lay wax, jële ko ca fa mu denc lu baax, te nit ku bon, lu bon lay wax, jële ko ca fa mu denc lu bon.
Explore Macë 12:35
4
Macë 12:31
Yeesu teg ca ne: «Loolu moo tax maa ngi leen koy wax, bàkkaar walla sos wu mu mana doon, dinañu ko baale, waaye ku sosal Xelum Yàlla, duñu ko baal.
Explore Macë 12:31
5
Macë 12:33
Neeleen garab gi baax na, moom ak meññeefam, walla ngeen ne garab gi bon na, moom ak meññeefam; ndaxte garab, meññeefam lañu koy xàmmee.
Explore Macë 12:33