1
Macë 11:28
Téereb Injiil
TI
«Ñëwleen ci man, yéen ñépp ñi sonn te diis, dinaa leen may noflaay.
Compare
Explore Macë 11:28
2
Macë 11:29
Jébbaluleen ci man te jàng ci man, ndaxte lewet naa te woyof, te dingeen am noflaay ci seen xol.
Explore Macë 11:29
3
Macë 11:30
Ndaxte sama kilifteef lewet na te sama yen diisul.»
Explore Macë 11:30
4
Macë 11:27
Yeesu teg ca ne: «Sama Baay jébbal na ma lépp, te kenn manu maa xam, man Doom ji, ku dul Baay bi; kenn it manula xam Baay bi, ku dul man Doom ji, ak ku ma ko bëgga xamal.
Explore Macë 11:27
5
Macë 11:4-5
Yeesu ne leen: «Demleen nettali Yaxya li ngeen dégg te gis ko. Gumba yaa ngi gis, lafañ yiy dox, gaana yi wér, tëx yiy dégg, ñi dee di dekki, te néew doole ñaa ngi dégg xibaaru jàmm bi.
Explore Macë 11:4-5
6
Macë 11:15
Déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.
Explore Macë 11:15