1
Luug 24:49
Téereb Injiil
TI
Te man dinaa leen yónnee li sama Baay dige. Yéen nag toogleen ci dëkk bi, ba ñu sol leen doole ji jóge ci kaw.»
Compare
Explore Luug 24:49
2
Luug 24:6
Nekkatu fi; dekki na. Fàttalikuleen la mu leen waxoon, ba mu nekkee Galile.
Explore Luug 24:6
3
Luug 24:31-32
Bi mu defee loolu, lépp leer ci seeni bët, ñu daldi ko xàmmi. Waaye Yeesu ne mes, gisatuñu ko. Noonu ku nekk naan sa moroom: «Ndax sa xol seddul woon, bi muy wax ak nun ci yoon wi, te muy tekki Mbind mi?»
Explore Luug 24:31-32
4
Luug 24:46-47
Mu ne leen: «Fàww Almasi bi sonn, mu dee te dekki ca ñetteelu fan ba, ni ñu ko binde, te it ñuy yégle xeet yépp ci turam, dale ko ci Yerusalem ne war nañoo tuub seeni bàkkaar, Yàlla baal leen.
Explore Luug 24:46-47
5
Luug 24:2-3
Bi ñu agsee, ñu fekk ñu béraŋ doj, wa uboon bàmmeel ba. Ñu dugg ca bàmmeel ba, waaye fekkuñu fa néewu Boroom bi Yeesu.
Explore Luug 24:2-3