1
Luug 23:34
Téereb Injiil
TI
Ci kaw loolu Yeesu ne: «Baay, baal leen, ndaxte xamuñu li ñuy def.» Xarekat ya tegoo ay bant yéreem, ngir séddoo ko.
Compare
Explore Luug 23:34
2
Luug 23:43
Yeesu ne ko: «Ci dëgg maa ngi la koy wax, tey jii dinga texe ak man ca jataayu Yàlla.»
Explore Luug 23:43
3
Luug 23:42
Noonu mu ne: «Yeesu, fàttaliku ma, boo délsee ci sa nguur.»
Explore Luug 23:42
4
Luug 23:46
Yeesu woote ak kàddu gu dëgër naan: «Baay, jébbal naa la sama ruu!» Bi mu waxee loolu, mu delloo ruuwam Yàlla.
Explore Luug 23:46
5
Luug 23:33
Bi xarekat ya agsee ba ca bérab, ba ñuy wooye Kaaŋu bopp, ñu daaj fa Yeesu ca bant, daajaale ñaari defkati lu bon ya, kenn ca ndijooram, ka ca des ca càmmoñam.
Explore Luug 23:33
6
Luug 23:44-45-44-45
Noonu digg bëccëg daldi jot, jant ba nëbbu, réew mépp daldi lëndëm këruus lu mat ñetti waxtu. Ridob bérab bu sell ba ca kër Yàlla ga daldi xar ñaar.
Explore Luug 23:44-45-44-45
7
Luug 23:47
Bi njiitu xare ba gisee li xewoon, mu màggal Yàlla ne: «Dëgg-dëgg nit kii ku jub la woon.»
Explore Luug 23:47