1
Luug 18:1
Téereb Injiil
TI
Noonu Yeesu wax leen itam léeb wii ngir xamal leen ne war nañoo sax ci ñaan te baña xàddi.
Compare
Explore Luug 18:1
2
Luug 18:7-8
ndax Yàlla du àtte jub mbooloom mi mu tànn te ñu koy ñaan wall guddi ak bëccëg? Ndax dina leen xaarloo? Maa ngi leen koy wax, dina leen àtte jub ci lu gaaw. Waaye bu Doomu nit ki ñëwee, ndax dina fekk ngëm ci àddina?»
Explore Luug 18:7-8
3
Luug 18:27
Yeesu ne leen: «Li të nit ñi, tëwul Yàlla.»
Explore Luug 18:27
4
Luug 18:4-5
Àttekat ba bañ lu yàgg, waaye am bés mu ne ci xelam: “Ragaluma Yàlla te faalewuma mbindeef, waaye jigéen jii lakkal na ma; kon dinaa ko àtte, ngir mu bañatee ñëw sonal ma. Dina rey ak ay wax.”»
Explore Luug 18:4-5
5
Luug 18:17
Ci dëgg, maa ngi leen koy wax, ku woyoful ni xale, nangu nguuru Yàlla, doo ci mana dugg.»
Explore Luug 18:17
6
Luug 18:16
Waaye Yeesu woo leen ne: «Bàyyileen xale yi, ñu ñëw ci man, te buleen leen tere, ndaxte ñu mel ni ñoom ñoo yelloo nguuru Yàlla.
Explore Luug 18:16
7
Luug 18:42
Noonu Yeesu ne ko: «Na say bët gis! Sa ngëm faj na la.»
Explore Luug 18:42
8
Luug 18:19
Yeesu ne ko: «Lu tax nga wooye ma ku baax? Yàlla rekk a baax.
Explore Luug 18:19