1
Luug 19:10
Téereb Injiil
TI
Ndaxte Doomu nit ki ñëw na, ngir seet te musal ñi réer.»
Compare
Explore Luug 19:10
2
Luug 19:38
Ñu ngi naan: «Yaw buur biy ñëw ci turu Boroom bi, ku barkeel nga! Na jàmm am ca asamaan, te ndam li féete ca bérab yu gëna kawe!»
Explore Luug 19:38
3
Luug 19:9
Yeesu ne ko: «Mucc gi wàcc na tey ci kër gii, ndaxte nit kii, ci askanu Ibraayma la bokk itam.
Explore Luug 19:9
4
Luug 19:5-6
Bi Yeesu dikkee ba tollook garab ga nag, mu téen ne ko: «Sase, wàccal gaaw, ndax tey sa kër laa wara dal.» Sase daldi gaawantu wàcc, ganale ko ak mbég.
Explore Luug 19:5-6
5
Luug 19:8
Waaye Sase taxaw ne Boroom bi: «Déglul Boroom bi, dogu naa may sama genn-wàllu alal miskin yi, te lu ma masa njublaŋ nit, jël alalam, dinaa ko fey ñeenti yoon lu ni tollu.»
Explore Luug 19:8
6
Luug 19:39-40
Waaye ay Farisen yu nekkoon ca mbooloo ma ne Yeesu: «Kilifa gi, yeddal sa taalibe yi!» Noonu mu ne: «Maa ngi leen koy wax, bu ñu noppee ñoom, doj yiy xaacu.»
Explore Luug 19:39-40