1
Luug 15:20
Téereb Injiil
TI
«Mu daldi jóg, jëm kër baayam. Waaye bi muy soreendi kër ga, baayam séen ko, yërëm ko, daldi daw laxasu ko, fóon ko.
Compare
Explore Luug 15:20
2
Luug 15:24
ndaxte sama doom jii dafa dee woon te dundaat na, dafa réeroon te feeñ na.” Noonu ñu tàmbalee bànneexu.
Explore Luug 15:24
3
Luug 15:7
«Maa ngi leen di wax lii: ci noonule, dina am mbég ci asamaan, bu benn bàkkaarkat tuubee ay bàkkaaram. Te mbég moomu mooy ëpp mbég, mi fay am, ngir juróom ñeent fukk ak juróom ñeent ñu jub, te soxlawuñoo tuub seeni bàkkaar.
Explore Luug 15:7
4
Luug 15:18
Damay jóg, dem ca sama baay ne ko: ‘Baay, tooñ naa Yàlla, tooñ naa la
Explore Luug 15:18
5
Luug 15:21
Doom ja ne ko: “Baay, tooñ naa Yàlla, tooñ naa la; yeyootumaa nekk sa doom.”
Explore Luug 15:21
6
Luug 15:4
«Kan ci yéen soo amoon téeméeri xar, te benn réer ci, nooy def? Ndax doo bàyyi ca parlukaay ba juróom ñeent fukki xar ya ak juróom ñeent, toppi ma réer, ba gis ko?
Explore Luug 15:4