1
Luug 12:40
Téereb Injiil
TI
Yéen itam taxawleen jonn, ndaxte Doomu nit ki dina ñëw ci waxtu wu ngeen ko séenuwul.»
Compare
Explore Luug 12:40
2
Luug 12:31
Waaye wutleen nguuram, te loolu lépp dina leen ko ci dollil.
Explore Luug 12:31
3
Luug 12:15
Noonu mu ne leen ñoom ñépp: «Moytuleen bëgge, ndaxte bakkanu nit ajuwul ci alalam, ak lu mu baree bare.»
Explore Luug 12:15
4
Luug 12:34
Ndaxte fu sa alal nekk, fa la sa xol nekk itam.
Explore Luug 12:34
5
Luug 12:25
Ana kan ci yéen ci kaw njaaxleem, moo mana yokk waxtu ci àppam?
Explore Luug 12:25
6
Luug 12:22
Noonu Yeesu daldi ne taalibeem yi: «Loolu moo tax maa ngi leen koy wax, buleen seen bakkan jaaxal, ci lu ngeen wara lekk. Buleen jaaxle it ngir seen yaram ci lu ngeen wara sol
Explore Luug 12:22
7
Luug 12:7
Seen kawari bopp sax waññees na leen. Kon buleen ragal dara, yéena gën ndiiraanu ramatu.
Explore Luug 12:7
8
Luug 12:32
«Buleen ragal dara, yéen coggal ju ndaw ji, ndaxte dafa soob seen Baay, mu jagleel leen nguuram.
Explore Luug 12:32
9
Luug 12:24
Seetleen baaxoñ yi: duñu ji, duñu góob, amuñu dencukaay, amuñu sàq, teewul Yàllaa ngi leen di dundal. Céy ni ngeen ëppe maana picc yi!
Explore Luug 12:24
10
Luug 12:29
Buleen di wut lu ngeen di lekk walla lu ngeen di naan; te buleen ci jaaxle.
Explore Luug 12:29
11
Luug 12:28
Yéen ñi néew ngëm! Bu Yàlla woddee nii ñaxum tool yi, miy sax tey, te bu subaa ñu def ko ci taal bi, ndax du leen gëna wodd?
Explore Luug 12:28
12
Luug 12:2
Amul dara lu nëbbu lu ñu warula biral, mbaa lu kumpa lu ñu warula siiwal.
Explore Luug 12:2