1
Luug 11:13
Téereb Injiil
TI
Ndegam yéen ñi bon yéena mana jox seeni gone lu baax, astamaak Baay bi nekk ci kaw dina jox Xel mu Sell mi ñi ko koy ñaan!»
Compare
Explore Luug 11:13
2
Luug 11:9
Moo tax ma ne, ñaanleen, ñu may leen; seetleen, te dingeen gis; fëggleen, ñu ubbil leen.
Explore Luug 11:9
3
Luug 11:10
Ndaxte képp kuy ñaan, dinga am; kuy seet, dinga gis; kuy fëgg, ñu ubbil la.
Explore Luug 11:10
4
Luug 11:2
Yeesu ne leen: «Bu ngeen dee ñaan, nangeen ne: Baay, yal na sa tur di lu ñu sellal, yal na sa nguur ñëw.
Explore Luug 11:2
5
Luug 11:4
Yal nanga nu baal sunuy bàkkaar, ndaxte nun itam danuy baal ñépp ñi nu tooñ. Yàlla boo nu teg ci yoonu nattu.»
Explore Luug 11:4
6
Luug 11:3
Yal nanga nu may bés bu nekk lu nu dunde.
Explore Luug 11:3
7
Luug 11:34
Bët mooy làmpu yaram. Bu sa bët wéree, kon sa yaram wépp leer. Waaye bu sa bët woppee, kon sa yaram wépp lëndëm.
Explore Luug 11:34
8
Luug 11:33
«Kenn du taal làmp, ba noppi di ko dugal cig kàmb, walla di ci këpp leget. Daf koy wékk, ngir mu leeral ñiy dugg.
Explore Luug 11:33