1
Yowaan 9:4
Téereb Injiil
TI
Bëccëg lanu wara matal jëfi ki ma yónni; guddi dina ñëwi, goo xam ne kenn du ci mana liggéey.
Compare
Explore Yowaan 9:4
2
Yowaan 9:5
Ci bi may nekk àddina, maay leeru àddina.»
Explore Yowaan 9:5
3
Yowaan 9:2-3
Taalibeem ya laaj ko ne: «Kilifa gi, lu tax waa jii judduwaale gumba? Ndax bàkkaaram a ko waral, walla bu waajuram?» Yeesu ne leen: «Ajuwul ci bàkkaaram walla ci bu waajuram. Waaye loolu dafa am, ngir jëfi Yàlla yi feeñ ci moom.
Explore Yowaan 9:2-3
4
Yowaan 9:39
Yeesu ne ko: «Àttee ma taxa ñëw àddina, ngir ñi gumba gis, ñiy gis gumba.»
Explore Yowaan 9:39